Paroles de la chanson Tell Me What You Want par Youssou N'Dour

Tell Me What You Want Traduction française
Chanson manquante pour "Youssou N'Dour" ? Proposer les paroles
Proposer une correction des paroles de "Tell Me What You Want"

Paroles de la chanson Tell Me What You Want par Youssou N'Dour

Douma la meuss a settal nga wett
My baby you know,
Douma la meuss a sett al nga wett
Souma la togne é nan ga ma baal,
My baby you know
Douma la meuss a sett al nga wett
Kham na lii nga ma ye n'ai,
My baby you know
Douma la meuss a sett al nga wett
Li ma la yé n'ai ci sa ma xol my baby you know
I'll never leave you alone...

Ahhnn.... He yeaaa
Tell me what you want and I'll do it
Ahhnn.... He yeaaa
Tell me what you want and I'll do it

Souma xol é rekk kham nga,
my baby you know
njem ou ma gare ba demm
Xam na bëgg na a lool my baby you know
Tey itt fonk nga maa
Lepp lo xam né souma ko deff é,
my babe you know
Dey wo ma wax ko , wax thia téll

boul xar dey ma ko wax
my baby you know
boul xar dey ma ko wax

Ahhnn.... He yeaaa
Tell me what you want and I'll do it
Ahhnn.... He yeaaa
Tell me what you want and I'll do it
Ahhnn.... He yeaaa
Tell me what you want and I'll do it
Ahhnn.... He yeaaa
Tell me what you want...

boul di faté gno'on yè
boul doul wo gno'on yé
boul di faté nak
bo ko faté nak
dëgg dëgg yak'u
tê ma fé do t'ou né

Ahhnn.... He yeaaa
Tell me what you want and I'll do it
Ahhnn.... He yeaaa
Tell me what you want and I'll do it
Ahhnn.... He yeaaa
wax ma lii nga bëgg ma def ko
Ahhnn.... He yeaaa

Ahhnn... He yeaa

Paroles.net dispose d’un accord de licence de paroles de chansons avec la Société des Editeurs et Auteurs de Musique (SEAM)

Sélection des chansons du moment

Les plus grands succès de Youssou N'Dour