Paroles de la chanson N'dawsi par Idrissa Diop

Paroles de Idrissa DIOP
Musique de Idrissa DIOP, Moussa DIOUF
© UNIVERSAL MUSIC PUBLISHING, grange productions

Chanson manquante pour "Idrissa Diop" ? Proposer les paroles
Proposer une correction des paroles de "N'dawsi"

Paroles de la chanson N'dawsi par Idrissa Diop

N'dawsi dieguessil
Mané yawe milé beugueunala
N'dawsi dieguessil
Mané yawe milé sop nala.
Sa boute yii melni wère
N'daw silé sopanala
Beugueunala
Xalé bilé
Diéguessima
Boma diegué sama yarame dawe
Xalé bilé ya taroo
Ya tayo
Talou tatou
Bou takhoussane dioté
Gha sangou solou
Xêgne lou nèxé

Rombeu guesto
N'daw sè set
Sima n'dakh té meuneu touma xaré.
Diek tank ratête téguine
Lerale guissa kaname migui
Bêguêle saraxole

Paroles.net dispose d’un accord de licence de paroles de chansons avec la Société des Editeurs et Auteurs de Musique (SEAM)

Sélection des chansons du moment