Paroles de la chanson Yakar par Idrissa Diop

Auteurs: Idrissa Diop

Compositeurs: Idrissa Diop,Leandro Aconcha

Editeurs: Universal Music Publishing,Grange Productions

Chanson manquante pour "Idrissa Diop" ? Proposer les paroles
Proposer une correction des paroles de "Yakar"

Paroles de la chanson Yakar par Idrissa Diop

Mane dé Yakar namé
Bèsse Khèle dina Sopékou
Dieumelé aye Dieufame
Thi lou Békh Bakhé
Mane Yakar na
Nith ki Manoule Deukhe thi Bine
Di yakheu Doune gui
Di tal Aleu Bé
Mane Yakar na
Yarame dina dawe

Da guêne di Xam né
Doune gui Bou Sété
Guêne set

Nith ki Fatelikoule

Bo yakhé Doune gui
Sa Bopeu Yakho

Paroles.net dispose d’un accord de licence de paroles de chansons avec la Société des Editeurs et Auteurs de Musique (SEAM)

Sélection des chansons du moment