Paroles de la chanson Dund par Elage Diouf

Chanson manquante pour "Elage Diouf" ? Proposer les paroles
Proposer une correction des paroles de "Dund"

Paroles de la chanson Dund par Elage Diouf

Aytcha len gnou saf
Mdakh fi bo doul saf
Do Djembeut dara mu skh
Lo donoul talibem mouno done serignam
Rew dal bou paré patt tcha tol ya la djogué
Gor ak Djiguene, aywalene tcha tolya
Ana lane mo ko fi djar ba gnowye dun de Métite ak tisse
Te Bour Yalla bakhé gnou YAYE sunu Thiossane
Magnou gniane Falahou dokhmi wallagane
HAM Banedk da tchi gueune, banekhou léne, banekh da, tchi gueune
YAW Banekh da, tchi gueune, banekhou, léne, banekh da, tchi gueune
Ana, lane mo ko fi djar ba gnouye dundé Métite ak tisse
Te Bour Yalla bakhé gnou YAYA sunu Thiossane
Magnou gniane Falahou dokhmi wallagane
HAM yaw gniou Dioubo bolek di woté diame dakh mi gnou mel dou Yone
Magnou ko wakh té dé Mignou mel dou yone, mdakh mignou mel dou Yone,
Magne ko wakh, té dé Mignou mel dou yone
HAM yaw ni gnou mel dou yone, nagne ko wakh té dé, nigou mel dou yone
Mdakh nignou mel dou yone, nagne ko wakh te dé
Ma am métite bou tiss, nar len ko djotalli, nouma guissé gni di guérre
Bo kholé nit gni dé dou lolo lagnou tane, dou lolite la Bourbi
Yalla doale. Da Fa fek gnou djel domou adama denk ko gourgui
Mou Wara def warougarame, Ay Yaye mane souma done Yaw, yonou djam lay
Sète dakh guissouma lou ko gueune.
Yaw banekh bi, tchi gueune, oho banekhou lene, banekh dat tchi yuene
Anhan banekhou lene (2 x)
Gnou gui tchi l'an 2000, gnouni domou Adama Mdiaye évolué na
Khané béy tchi khelmi bo kholé tchi kholmi data melni
Bobatey yaye moussou fé djogué, moussou Fé djogué
Banekh da tchi gueune oho banekhou léné banekh da tchi gueune
Anhan banéekhou léne,
Gmi di djouli di niaral senni dome, gni keuye di dioye guir sen moudji dome
Te Bercy, sa Yaye boye gniaral nala, Mdeye Bercy Diouf wargua guoiguoilu
Dakh kou sagnon bo djouré sa dome, bouffi gueunoulite mome, ken douko gueune
Te Bercy Diouf ken gueu noula yaw, kor Tapha Guéye guatché gualama
Mdakh kou sagnone bo djouré sa dome, bouffi gueunoulite mome, ken douko gueune
Te Bercy ken gueunoula guatché galama.

Paroles.net dispose d’un accord de licence de paroles de chansons avec la Société des Editeurs et Auteurs de Musique (SEAM)

Sélection des chansons du moment